input
stringlengths 13
433
| input_fr
stringlengths 2
469
| input_wo
stringlengths 15
414
| label
stringclasses 77
values |
|---|---|---|---|
I normally don't use ATMs, but I was in a rush today and had to withdraw some cash. The ATM gave me the wrong amount of money and now my app is not showing the same amount as it should. What do I do?
|
Normalement, je n'utilise pas les distributeurs automatiques, mais j'étais pressé aujourd'hui et j'ai dû retirer de l'argent. Le distributeur m'a donné le mauvais montant d'argent et maintenant mon application n'affiche pas le même montant qu'elle devrait. Que dois-je faire ?
|
Ci yoon, duma jëfandikoo gab, waaye dama yàkkamti woon tey waroon naa génnee xaalis. Gab bi xaalis bu jaarulm yoon lama jox te leegi aplikaasiyoŋ bi feeñalul benn xaalis bi waroon? Lu ma wara def?
|
wrong amount of cash received
|
If I order a card when does it arrive?
|
Si je commande une carte, quand est-elle livrée ?
|
Suma komaandee kàrt, kañ lañu ma koy indil?
|
why verify identity
|
Where do my available funds come from?
|
D'où viennent mes fonds disponibles ?
|
Fan la sama xaalis bi yemb jóge ?
|
verify source of funds
|
Why is my card payment still pending?
|
Pourquoi mon paiement par carte est-il toujours en attente ?
|
Lu tax sama peyoorug kàrt bi nekk ba tay ci pàccub négandiku ?
|
pending card payment
|
I made a purchase and would like to get a refund for what I bought can you have the money put back in my account?
|
J'ai effectué un achat et j'aimerais obtenir un remboursement pour ce que j'ai acheté. Pouvez-vous remettre l'argent sur mon compte ?
|
Jënd naa benn afeer waaye su ma sañoon ñu delloo ma sama xaalis.Ndax mën ngeen a fexe ba xaalis bi dellu ci sama kont ?
|
request refund
|
HOW LONG THE CARD VALIDITY
|
Quelle est la durée de validité de la carte ?
|
Lan mooy diir bi ñu mën a jëfandikoo kàrt bi ?
|
card not working
|
How do I unlock my account after typing in the wrong PIN too many times?
|
Comment débloquer mon compte après avoir saisi un code PIN erroné à plusieurs reprises ?
|
naka laay def ba dindi sama kont ginaaw bima dugalee kod PIN bu baaxul ay yoon yu bari?
|
pin blocked
|
There is a cash withdrawal on my statement that I don't recognize
|
Il y a un retrait d’argent sur mon relevé que je ne reconnais pas
|
Amna xaalis bu ñu jël ci sama rëlëwe te xamuma ko.
|
cash withdrawal not recognised
|
I requested a refund from a merchant but don't see the money in my account. Are you able to check with the merchant or process the refund manually?
|
J’ai demandé un remboursement à un commerçant, mais je ne vois pas l’argent sur mon compte. Êtes-vous en mesure de vérifier auprès du commerçant ou de traiter le remboursement manuellement ?
|
Dama feyeeku benn jaaykat, waaye gisuma xaalis bi ci sama kont. Ndax mën nga xool ak jaaykat bi walla nga def ko loxo?
|
Refund not showing up
|
I want to talk about an order that I placed a long time ago and have yet to receive. I demand a refund due to lack of delivery of the product! I refuse to pay for something I never got.
|
Je veux parler d'une commande que j'ai passée il y a longtemps et que je n'ai pas encore reçue. J'exige un remboursement faute de livraison du produit ! Je refuse de payer pour quelque chose que je n'ai jamais eu.
|
Bëgg naa wax ci benn komaand bu yàgg bu ma def te jotaguma ko. Maa ngiy sàkku ñu delloma sama xaalis ndax bagaas bi yegsiwul. Duma fey luma musula jot.
|
request refund
|
I had a card payment that was declined. Why?
|
J’ai eu un paiement par carte qui a été refusé. Pourquoi?
|
Amnaa benn payoon ak kàrt buñu bañ. Lu tax?
|
declined card payment
|
What is this extra fee while I was doing a transfer?
|
Quels sont ces frais supplémentaires pendant que j’effectuais un transfert ?
|
Yan ñooy yeneen fere yooyu bi may yónnee xaalis?
|
transfer fee charged
|
Where is the transfer to my account that I made?
|
Où se trouve le virement sur mon compte que j’ai effectué ?
|
Fan la xaalis bi ma def ci sama kont nekk?
|
balance not updated after bank transfer
|
I tried to make a payment with my card and it was declined. Why is it pending?
|
J'ai essayé d'effectuer un paiement avec ma carte et il a été refusé. Pourquoi est-il en attente ?
|
Doon naa jéem a feyee ak sama kàrt waaye jàllul. Lu tax peyoor bi di wéy di nekk ci pekku négandiku ?
|
pending card payment
|
Is there a discount for multiple currency exchanges?
|
Existe-t-il une réduction pour les échanges de devises multiples ?
|
Ndax dees di wàññil kuy faral di weccoo xaalis ?
|
exchange charge
|
I would like to change to a different currency.
|
Je voudrais changer de devise.
|
Dama bëgga soppi ay xaalis ?
|
pending cash withdrawal
|
I saw that my transfer was declined.
|
J’ai vu que mon transfert avait été refusé.
|
Dama gis ni xaalis bi ma toxal nanguwuñu ko.
|
declined transfer
|
Why didn;t my payment work
|
Pourquoi mon paiement n'a pas fonctionné
|
Lu tax sama peyoor jàllul ?
|
declined card payment
|
How do I get my virtual card?
|
Comment obtenir ma carte virtuelle ?
|
Naka Laay def ba am sama kàrt Wirtuel?
|
card linking
|
My disposable virtual card isn't working.
|
Ma carte virtuelle jetable ne fonctionne pas.
|
Sama kàrt wirtiyel bi ñuy jefandikoo benn yoon kese doxul.
|
virtual card not working
|
I have a question about fee for cash withdraw.
|
J’ai une question sur les frais de retrait d’espèces.
|
Amnaa laaj bu jëm ci njëgu jël xaalis bi.
|
cash withdrawal charge
|
Can you help me with proving my identity?
|
Pouvez-vous m'aider à prouver mon identité ?
|
Ndax mën nga ma jàppale ma wone sama bopp?
|
declined transfer
|
What do I do if I forgot my passcode?
|
Que dois-je faire si j’ai oublié mon code d’accès ?
|
Lan laa wara def suma fàttee sama kodu duggu?
|
passcode forgotten
|
Are there cash machines where I can change my PIN?
|
Y a-t-il des distributeurs automatiques de billets où je peux changer mon code PIN ?
|
Ndax amna ay gab yu ma mëna soppee sama kodu PIN?
|
change pin
|
Why do we need to verify top-up?
|
Pourquoi avons-nous besoin de vérifier la recharge ?
|
Lu tax ñu wara xool xaalis bi ñu dugal?
|
verify top up
|
How do i authenticate a top-up card?
|
Comment puis-je authentifier une carte de recharge ?
|
Naka laa mëna xame kàrtu sarse?
|
verify top up
|
I need my card to be activated right now.
|
J'ai besoin que ma carte soit activée immédiatement
|
dama soxla ñu aktive sama kart leegi
|
reverted card payment?
|
I don't understand why you aren't accepting my transfer. After a couple times trying I'm still getting an error message.
|
Je ne comprends pas pourquoi vous n'acceptez pas mon transfert. Après plusieurs tentatives, je reçois toujours un message d'erreur.
|
Xamuma lu tax xaalis bi ma bëgg a yónnee jàllul. Jéem naa ba sonnu waaye dara.
|
beneficiary not allowed
|
I couldn't complete card activation.
|
Je n'ai pas pu terminer l'activation de la carte.
|
Mënu ma jeexal aktivaasioŋu kàrt bi.
|
activate my card
|
Why can't I make a transfer?
|
Pourquoi ne puis-je pas effectuer de transfert ?
|
Lu tax mënuma yónnee xaalis?
|
failed transfer
|
Will you assess me more fees if I top up with an international card?
|
Allez-vous me facturer des frais supplémentaires si je recharge avec une carte internationale ?
|
Ndax su ma dugalee xaalis ci sama kont ak kàrtu bitim-réew fere yi dañuy yokku ?
|
top up by card charge
|
explain the virtual card
|
expliquer la carte virtuelle
|
Leeralal kàrt wirtuyel bi?
|
transfer timing
|
Why does my transfer keep generating an error message?
|
Pourquoi mon transfert continue-t-il de générer un message d'erreur ?
|
Lu tax sama yónnee bi di wéy di fësal bataaxalu njuumte ?
|
beneficiary not allowed
|
i need to add express delivery if that's an option
|
J’ai besoin d’ajouter la livraison express si c’est une option
|
Bëgg naa yokk yónnee eksperes sudee tànneef la.
|
card delivery estimate
|
A mortgage payment I'm making is giving me an error message. This is the first time I'm making this payment and want to know what's wrong.
|
Un paiement hypothécaire que j’effectue me donne un message d’erreur. C’est la première fois que j’effectue ce paiement et je veux savoir ce qui ne va pas.
|
Payooru ipotek bi may def mungi may jox ab bataaxalu njuumte. Bii mooy yoon wu njëkk may def payoor bii, dama bëgga xam lu doxul.
|
failed transfer
|
I live in the US and I would like to get a card. How do I go about getting one?
|
Je vis aux États-Unis et j'aimerais obtenir une carte. Comment faire ?
|
Etats-Unis la dëkk waaye dama bëggoon a am ab kàrt, naka laa war a def ?
|
country support
|
Would you be so kind as to activate my card? Thanks
|
Auriez-vous l'amabilité d'activer ma carte ? Merci.
|
Ndax dinga ma may doxal sama kàrt? Jërëjëf
|
activate my card
|
Can i have a virtual card?
|
Puis-je avoir une carte virtuelle ?
|
Ndax mën naa am kàrt wirtuyel?
|
country support
|
Can I add a card to back into the app?
|
Puis-je ajouter une carte à l'arrière de l'application ?
|
Ndax mën naa yokk benn kàrt ci ginaaw aplikaasiyoŋ bi?
|
card linking
|
How do you figure out the exchange rate? Can you explain why I got less money than expected?
|
Comment déterminez-vous le taux de change ? Pouvez-vous m’expliquer pourquoi j’ai reçu moins d’argent que prévu ?
|
Naka ngeen di def ba xam njëgu weccoo xaalis bi? Ndax mën ngeen ma wax lu tax ma jot xaalis bu yées lima doon seentu?
|
wrong exchange rate for cash withdrawal
|
I have an unfamiliar direct debit in my statement.
|
J'ai un prélèvement automatique inconnu sur mon relevé.
|
Am naa jëlum xaalis bu ma xamewul ci sama rëlëwe
|
direct debit payment not recognised
|
My identity wasn't verified
|
Mon identité n’a pas été vérifiée
|
Sama jëmm, saytuwuñu ko.
|
unable to verify identity
|
Will I be charged any fees if I want to add money with an international card?
|
Des frais me seront-ils facturés si je souhaite ajouter de l'argent avec une carte internationale ?
|
Ndax su ma bëggee yokk sama xaalis ak kàrtu bitim-réew damay fey ay fere ?
|
top up by card charge
|
I'm having an issue with transaction. I topped up my account and saw it went through, but that was a few days ago and the money isn't in my account any more. What's up with that?
|
J’ai un problème avec la transaction. J’ai rechargé mon compte et j’ai vu que tout était traité, mais c’était il y a quelques jours et l’argent n’est plus sur mon compte. Qu’est-ce qui se passe avec ça ?
|
Dama am jafe-jafe ci jëflante xaalis bi. Dama sarse sama kont, ma gis ni lépp jaarna yoon, waaye ay fan yu néew ci ginnaaw la woon, te xaalis bi nekkatul ci sama kont. Lu xew ci loolu?
|
top up reverted
|
I moved and need to change my address.
|
J'ai déménagé et je dois changer d'adresse.
|
Dama toxu te dama war a soppi sama adares
|
edit personal details
|
My cash withdrawal was declined, why?
|
Mon retrait d'argent a été refusé, pourquoi ?
|
Lànkal nanu ma xaalis bi ma bëggoon a jël, lu ko waral ?
|
declined cash withdrawal
|
i did not get any money but still was charged
|
je n'ai pas reçu d'argent mais j'ai quand même été facturé
|
Jotuma xaalis waaye terewul am na lu nu ma dagg.
|
wrong amount of cash received
|
Can I top-up my card using a bank transfer.
|
Puis-je recharger ma carte par virement bancaire ?
|
Ndax mën naa sarse sama kàrt ci toxalu bànk?
|
transfer into account
|
Am I allowed to hold money in multiple currencies?
|
Puis-je détenir de l’argent dans plusieurs devises ?
|
Ndax mën naa weccoo xaalis ci xeetu xaalis yu bari?
|
fiat currency support
|
I can't find my refund. Please help.
|
Je ne trouve pas mon remboursement. Aider, s’il vous plaît.
|
Mënu maa gis xaalis bi ñu ma delloo. Dimbalileen ma.
|
Refund not showing up
|
There is a transfer not showing on my account.
|
Il y a un virement qui n'apparaît pas sur mon compte.
|
Am na benn toxal xaalis bu feeñul ci sama kont.
|
extra charge on statement
|
Are transfers not free? I didn't know I would be charged for transfers.
|
Les transferts ne sont-ils pas gratuits ? Je ne savais pas que je serais facturé pour les transferts.
|
Ndax doo fay dara boy yónnee xaalis? Xamuma woon ni dina ñu ma fayeeku ngir yónnee xaalis.
|
transfer fee charged
|
cash and check deposit has not gone thru
|
le dépôt en espèces et par chèque n'a pas été effectué
|
Dugal xaalis ak sek defuñu ko
|
balance not updated after cheque or cash deposit
|
I've already sent the money out and still have not received money in my account.
|
J’ai déjà envoyé l’argent et je n’ai toujours pas reçu d’argent sur mon compte.
|
Yónnee naa xaliss bi te ba leegi jotuma xaalis ci sama kontu.
|
balance not updated after cheque or cash deposit
|
Why haven't I received a refund yet?
|
Pourquoi n’ai-je pas encore reçu de remboursement ?
|
Lu tax ma jotatuma xaalis biñ delloo ba leegi?
|
Refund not showing up
|
I may have entered the PIN wrong and the account is blocked. What do I have to do to get it unblocked.
|
J'ai peut-être mal saisi mon code PIN et mon compte est bloqué. Que dois-je faire pour le débloquer ?
|
Mëna am dama juum ci ni ma bindee sama baatu ubbikaay te sama kont tëju na. Lan laa wara def ngir tijji waat ko?
|
pin blocked
|
Can I exchange USD and GBP from the app?
|
Puis-je échanger des USD et des GBP depuis l’application ?
|
Ndax mën naa weccoo USD ak GBP ci aplikaasioŋ bi?
|
exchange via app
|
I need to dispute a direct debit.
|
Je dois contester un prélèvement automatique.
|
Dama wara xultu sama génnee otomatik
|
direct debit payment not recognised
|
I've use my accounts all the time to manage my payments for my place abroad that I just got. I now see that I suddenly have new fees.I'm a frequent customer, so why are you charging me new fees instead of rewarding me?
|
J'utilise mes comptes tout le temps pour gérer mes paiements pour mon logement à l'étranger que je viens de recevoir. Je vois maintenant que j'ai soudainement de nouveaux frais. Je suis un client fréquent, alors pourquoi me facturez-vous de nouveaux frais au lieu de me récompenser ?
|
Damay jëfandikoo sama kont saa yu nekk ngir fay sama luyaas ci bitim réew bima jot leegi. Gis naa ni dañu ma feyeku njëg yu bees. Man kilyaan bu yàgg laa, kon lu tax ngeen may feyeku njëg yu bees te waar neexal?
|
transfer fee charged
|
How long will it take to receive a virtual card?
|
Combien de temps faut-il pour recevoir une carte virtuelle ?
|
Ñaata waxtu ngay def ngir jot kàrt wirtiyel?
|
getting virtual card
|
My transfer has been pending for a long time now. I already double checked my account info and it is correct. Why is it taking so long in 2018 to transfer money?
|
Mon transfert est en attente depuis longtemps maintenant. J'ai déjà vérifié les informations de mon compte et elles sont correctes. Pourquoi faut-il autant de temps en 2018 pour transférer de l'argent ?
|
Sama yónnee xaalis yàgg naa xaar. Xool naa bu baax samay leeralu kont te noonu la. Lu tax muy jël lu yàgg ci 2018 ngir yónnee xaalis?
|
transfer not received by recipient
|
I am unable to prove my identity
|
Je ne suis pas en mesure de prouver mon identité
|
Mënuma undi ay firnde ci man la kan.
|
unable to verify identity
|
How do I top up my account using transfer?
|
Comment recharger mon compte par virement ?
|
Naka laa mën a sarsee sama kàrt jaare ko ci ndugalum koppar ?
|
transfer into account
|
My top up did not complete.
|
Ma recharge n’a pas abouti.
|
Xaalis bi ma dugal ñëwul .
|
pending top up
|
Which ATMs accept this circuit board ?
|
Quels distributeurs automatiques acceptent ce circuit imprimé ?
|
Yan ñooy GAB yiy nangu kàrt bii ?
|
atm support
|
why has a cash withdrawal charged me?
|
Pourquoi un retrait d’espèces m’a-t-il été facturé ?
|
Lu tax ñu may feyeeku ngir xaalis bima jël?
|
cash withdrawal charge
|
how do i avoid charges in the future
|
Comment puis-je éviter des frais à l’avenir
|
naka laa mëna moytoo ay fere ëllëg.
|
card payment fee charged
|
One of my card payments looks like it's stuck but I have made the payment days ago. How long until the payment will be applied to my account?
|
L'un de mes paiements par carte semble bloqué, mais je l'ai effectué il y a plusieurs jours. Combien de temps faudra-t-il avant qu'il soit crédité sur mon compte ?
|
Dafa mel ni benn ci samay payoor ci kàrt dañu ko tëj, waaye def naa ko ay fan yu bari ci ginaaw. Ñaata waxtu lay def bala ñu koy duggal ci sama kont?
|
pending card payment
|
I see a strange payment in my account.
|
Je vois un paiement étrange sur mon compte.
|
Dama gis xaalis bu doy waar ci sama kont.
|
declined transfer
|
Do you convert to Euro?
|
Convertissez-vous en Euro ?
|
Ndax dangay weccoo FCFA ?
|
Refund not showing up
|
What do I do if I have exceeded all my PIN tries?
|
Que dois-je faire si j’ai dépassé tous mes tentatives de code PIN ?
|
Lan laa wara def sud ma jeexalee pexey joxe kod-PIN yépp?
|
pin blocked
|
I'm suddenly getting an error while attempting a transfer that it isn't possible. Why? I've done it before.
|
Je reçois soudainement une erreur lors d’une tentative de transfert indiquant que ce n’est pas possible. Pourquoi? Je l’ai déjà fait.
|
Dama jekki jot benn njuumte bimay jéema toxal xaalis, muy wone ni loolu mënul nekk. Lu tax? Def naa ko ba noppi.
|
beneficiary not allowed
|
What is the process to create a disposable virtual card?
|
Quel est le processus de création d’une carte virtuelle jetable ?
|
Lan mooy anam wi ñuy defare kàrt wirtiyel bu ñu mëna jefandikoo benn yoon kese?
|
get disposable virtual card
|
My card payment wasn't accepted.
|
Mon paiement par carte n’a pas été accepté.
|
Nangu wuñu sama payoor ak kàrt.
|
declined card payment
|
There is an extra 1£ charge on my app. Why did it charge me extra?
|
Mon application est facturée 1 £ de plus. Pourquoi ?
|
Am na ferey benn euro ci sama aplikaasiyoŋ bi. Lan moo tax ñu faktiire ma ko ?
|
extra charge on statement
|
where exactly does money come from
|
d'où vient exactement l'argent
|
Fan la xaalis bi di joge?
|
verify source of funds
|
Is it possible someone has access to my card? I noticed that there are a couple of payments in the app I'm sure I did not make. Can you find out what's going on here?
|
Quelqu'un pourrait-il avoir accès à ma carte ? J'ai remarqué que certains paiements dans l'application ne sont certainement pas de moi. Pouvez-vous savoir ce qui se passe ?
|
Ndax amna ku mëna jëfandikoo sama kàrt? Dama seetlu ni yenn peyoor yi ci app bi duñu samay peyoor. Ndax mën nga xam lu xew?
|
transfer not received by recipient
|
Explain why I can't do a transfer to an account.
|
Expliquez pourquoi je ne peux pas effectuer un transfert vers un compte.
|
Leeral leen ma lu tax mënumaa toxal xaalis ci beneen kont.
|
beneficiary not allowed
|
I got some cash in the ATM but its still pending
|
J'ai reçu de l'argent liquide au distributeur, mais il est toujours en attente.
|
Jël naa xaalis ci GAB bi waaye ba tay moo ngi ci pekku négandiku
|
pending cash withdrawal
|
I see a direct debit transaction in my app that I didn't make.
|
Je vois une transaction de prélèvement automatique dans mon application que je n’ai pas effectuée.
|
Damay ngiy gis ab xaalis bu ñu jël ci sama aplikaasioŋ te defuma ko.
|
direct debit payment not recognised
|
Why was I charged extra on my app?
|
Pourquoi ai-je été facturé en plus sur mon application ?
|
Lu tax ñu feyeeku ma lu gëna bari ci sama aplikaasioŋ?
|
extra charge on statement
|
Please cancel the transfer I just made. I put in the wrong account number and can't seem to stop it on the app.
|
Veuillez annuler le transfert que je viens d'effectuer. J'ai saisi un mauvais numéro de compte et je n'arrive pas à l'arrêter sur l'application.
|
Baal leen ma ngeen fomm xaalis bi ma yóonee. Dama juum ci limatu kont bi, te mënu ma ko taxawal ci aplikasioŋ bi.
|
cancel transfer
|
I saw on the app that a cash withdrawal was completed on my account; however, I did not complete it.
|
J'ai vu sur l'application qu'un retrait d'espèces avait été effectué sur mon compte ; cependant, je ne l'ai pas effectué.
|
Gis naa ci aplikaasiyoŋ bi ni amna ab dindi xaalis buñu def ci sama kontu, waaye defuma ko.
|
cash withdrawal not recognised
|
My card has not been delivered yet and its been a week since I ordered it, please help
|
Ma carte n'a pas encore été livrée et cela fait une semaine que je l'ai commandée, aidez-moi s'il vous plaît
|
Sama kàrt yegseegul ba leegi, defna benn ayu-bis bi ma ko defarloo ba leegi, dimbali leen ma ngir yalla.
|
card arrival
|
My friend wants to send me money, can she?
|
Mon amie veut m’envoyer de l’argent, peut-elle ?
|
Sama xarit, dama bëgga yónnee xaalis, ndax mën naa nekk?
|
receiving money
|
How long does it take to show a deposit I made to my balance?
|
Combien de temps faut-il pour qu'un dépôt que j'ai effectué apparaisse sur mon solde ?
|
ñaata waxtu la wara def ndax dugal xaalis bi ma def feeñ ci li des sama kont?
|
top up limits
|
What proof of identification is needed?
|
Quelle preuve d’identité est nécessaire ?
|
Lan mooy firndeb dàntite bi mënul a ñàkk ?
|
verify my identity
|
They is a payment I don't recognize on my statement.
|
Il s'agit d'un paiement que je ne reconnais pas sur mon relevé.
|
Am na peyoor bu ma ràññeewul ci sama karne kont.
|
card payment not recognised
|
When will the transaction be done?
|
Quand la transaction sera-t-elle effectuée ?
|
Kañ lañuy yónnee xaalis bi?
|
transfer not received by recipient
|
Given a choice, I'd rather have Mastercard.
|
Si j'avais le choix, je préférerais avoir Mastercard.
|
Su ma mënoon naa tànn, kàrt master bi laay taamu ?
|
contactless not working
|
I used to know my password, but not anymore.
|
Avant, je connaissais mon mot de passe, mais ce n’est plus le cas.
|
Xamoon naa sama baatu-jàll, waaye xamatuma ko.
|
passcode forgotten
|
Are there any charges for receiving money?
|
Y a-t-il des frais pour recevoir de l’argent ?
|
Ndax dangay fey ngir jot xaalis?
|
top up by bank transfer charge
|
While abroad, I got cash, and the exchange rate applied is wrong.
|
À l’étranger, j’ai eu de l’argent liquide et le taux de change appliqué n’est pas correct.
|
Ca bitim réew, amoon naa xaalisu likid te njëgu weccoo xaalis bi baxulwoon.
|
wrong exchange rate for cash withdrawal
|
My card is stolen. Help!
|
Ma carte a été volée. À l'aide !
|
Sama kàrt dañu ko sàcc? Ndimbal!
|
lost or stolen card
|
Is American Express accepted?
|
American Express est-elle acceptée ?
|
Ndax Nangu nañu American Express ?
|
supported cards and currencies
|
Please explain why my top-up hasn't been processed yet?
|
Veuillez expliquer pourquoi ma recharge n’a pas encore été traitée ?
|
Nangeen ma leeral lu tax ba leegi defaruñu sama xaalis bi ma dugal?
|
pending top up
|
why hasnt my card come in yet?
|
Pourquoi ma carte n’est-elle pas encore arrivée ?
|
Lu tax sama kàrt yegseegul?
|
card arrival
|
I have a problem with a transfer. It didn't work. Can you tell me why?
|
J'ai un problème avec un transfert. Ça n'a pas fonctionné. Pouvez-vous m'expliquer pourquoi ?
|
Dama am jafe-jafe ak toxal. Doxul. Mën nga ma leeral lu ko waral?
|
Refund not showing up
|
In what increments can I top-up my card?
|
Par quels paliers puis-je recharger ma carte ?
|
Ci ban anam laa mëna sarsee sama kàrt?
|
activate my card
|
How can my friend pay me?
|
Comment mon ami peut-il me payer ?
|
Naka la ma sama xarit mën a feyee ?
|
receiving money
|
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.