input
stringlengths
13
433
input_fr
stringlengths
2
469
input_wo
stringlengths
15
414
label
stringclasses
77 values
What are the limits to where my card will be accepted?
Quelles sont les limites où ma carte sera acceptée ?
Yan ñooy yi nga xam ne yi sama kàrt nangu ?
card acceptance
Can you provide information for freezing my card immediately?
Pouvez-vous me fournir des informations pour geler ma carte immédiatement ?
Ndax mën ngeen ma jox ay xibaar ci sama kàrt bi jekki rekk yàqu ?
lost or stolen card
I added funds to my account but the app didn't process it.
J'ai ajouté des fonds sur mon compte mais l'application ne l'a pas traité.
Yokk naa xaalis ci sama kont waaye App bi defuko.
order physical card
My card will expire soon, do I need to order a new one?
Ma carte va bientôt expirer, dois-je en commander un nouveau ?
Sama kàrt leegi mu jeex, ndax dama wara defaraat bu bees?
card about to expire
I tried to do a transfer but I got a message that it was declined.
J'ai essayé d'effectuer un transfert mais j'ai reçu un message indiquant qu'il avait été refusé.
Jéem naa yónnee xaalis waaye dama jot ab bataaxal buy wax ni demul.
declined transfer
Why won't my card accept any transactions?
Pourquoi ma carte n'accepte aucune transaction ?
Lu tax sama kàrt du nangu benn jëflante?
pending top up
Why was money taken for a transfer?
Pourquoi de l'argent a été prélevé pour un transfert ?
Lu tax ñu génnee xaalis ci benn toxal?
request refund
What is your shipping policies for cards?
Quelle est votre politique d'expédition pour les cartes ?
Naka ngeen di doxalee wàllu jotali kàrt yi ?
card delivery estimate
Why am I being charged fees on some transactions but not on others? What am I missing here? I cannot find where to see the fee structure on my account. Help!
Pourquoi des frais me sont-ils facturés sur certaines transactions et pas sur d'autres ? Qu'est-ce qui me manque ici ? Je ne trouve pas où voir la structure des frais sur mon compte. Aidez-moi !
Lu tax ñu teg ma ay fere ndax yenn jëflante , lan laa amul fii? , gisuma fu njëg yi nekk ci sama kont joge. Dimbali ma?
card payment fee charged
How much longer until I get my new card?
Combien de temps faudra-t-il avant que je reçoive ma nouvelle carte ?
ñaata waxtu la wara def balaa maa jot sama kàrt bu bees?
activate my card
Hello. I bought an item a while ago, and have since requested a refund. However, upon checking my online statements, it seems that I haven't been issued a refund yet. How can this be remedied?
Bonjour. J’ai acheté un article il y a quelque temps et j’ai depuis demandé un remboursement. Cependant, en vérifiant mes relevés en ligne, il semble que je n’ai pas encore reçu de remboursement. Comment y remédier ?
Nanga def? Dama jënd benn mbir amna ay waxtu ci ginnaaw te ba leegi maa ngi laaj ñu delloo ma ko. Waaye, ginnaaw bi ma xoolee samay rëlëwe, dafa melni jotaguma xaalis bi. Nu ñuy saafaraa jafe-jafe bi?
Refund not showing up
Can I pay more to get it deliver quicker?
Puis-je payer plus pour être livré plus rapidement ?
Ndax mën naa fey lu gën a seer ngir ngeen teel ma ko jónne ?
card delivery estimate
Would it be possible to open up an account for children?
Serait-il possible d'ouvrir un compte pour les enfants ?
Ndax mën nañu ubbil ay xale kont?
age limit
Why did my top-up not go through?
Pourquoi ma recharge n'a-t-elle pas abouti ?
Lu tax xaalis bi ma dugal ci sama kont jàllul ?
top up reverted
Is there a fee for transferring money?
Y a-t-il des frais pour le transfert d’argent ?
Ndax amna luñu wara fey ngir yónnee xaalis?
transfer fee charged
I checked my statement and saw a charge of one pound, where is this charge coming from?
J'ai vérifié mon relevé et j'ai vu des frais d'une livre, d'où viennent ces frais ?
Xool naa sama karne kont, waaye gis naa ci benn pound. Fan la xaalis boobu jóge ?
extra charge on statement
Do you charge extra for exchanging currencies?
Facturez-vous un supplément pour l’échange de devises ?
Ndax dangeen di feyyeeku ab yokk ngir weccoo xaalis?
pending card payment
I cannot remember my passcode.
Je ne me souviens plus de mon mot de passe.
Fàttaleekootuma sama baatu jàll
passcode forgotten
I would like to get both Mastercard and Visa card from you if that's possible.
J'aimerais obtenir une carte Mastercard et une carte Visa de votre part si cela est possible.
Bëggoon naa ngeen jox ma ab kàrtu Mastercard ak kàrtu visa, su mënee nekk
visa or mastercard
How do I activate my new card
Comment activer ma nouvelle carte
Naka laa mën a doxalee sama kàrt bu bees bi ?
activate my card
Hi. A couple hours ago I make a transfer from my UK bank account, but it hasn't shown up. Please, would you see what the delay is?
Salut. Il y a quelques heures, j'ai effectué un virement depuis mon compte bancaire au Royaume-Uni, mais il n'est pas apparu. S'il vous plaît, pourriez-vous voir quel est le retard ?
Salaam maalekum. Waxtu yu néew ci ginnaaw, dama def xaalis ci sama kont bu Senegaal waaye feeñul. Ndax mën ngeen gis lu ko yeexal?
balance not updated after bank transfer
I would really like a physical card.
J'aimerais vraiment une carte physique.
Bëgg naa benn kàrt fisik.
order physical card
Hi, I tried topping up for the first time today (I'm a new customer), and the transaction has shown as pending for the last half an hour. Can you fix it?
Bonjour, j’ai essayé de recharger pour la première fois aujourd’hui (je suis un nouveau client), et la transaction est en attente depuis une demi-heure. Pouvez-vous le réparer ?
Nanga def, dama jéema dugal xaalis sama bis bu njëkk tey ( kiliyaan bu bees laa), te xaalis bima doon dugal demul amna genn-wàllu waxtu. Ndax mën ngeen ko defar?
pending top up
I see an unfamiliar payment on my statement.
Je vois un paiement inconnu sur mon relevé.
Dama gis benn payoor buma xamul ci sama rëlëwe.
card payment not recognised
What's the procedure for getting a card?
Quelle est la procédure à suivre pour obtenir une carte ?
Lan mooy anam wi ñuy jaar ngir am kàrt?
order physical card
Someone stole my card!
Quelqu'un a volé ma carte !
Dafa am ku sàcc sama kàrt
lost or stolen card
Can i use this card at any store?
Puis-je utiliser cette carte dans n'importe quel magasin ?
Ndax mën naa jëfandikoo kàrt bii ci bitig bu ma neex ?
card acceptance
where is my new card?
Où se trouve ma nouvelle carte ?
Fan la sama kàrt bu bees bi nekk?
card arrival
Is there a way to see where my money originally came from?
Existe-t-il un moyen de voir d’où vient mon argent à l’origine ?
Ndax dafa am lu ma mën a xamal fan la sama xaalis jóge ?
verify source of funds
I took out money from the ATM and it's still showing as pending?
J’ai retiré de l’argent au distributeur automatique et il est toujours en attente ?
Dama jël xaalis ci GAB bi te ba leegi mungi wéy di xaar?
pending cash withdrawal
Why would my card payment get reverted?
Pourquoi mon paiement par carte serait-il annulé ?
Lu tax ñuy fomm sama peyoor ak kàrt?
reverted card payment?
I think I lost my phone. Is there a way to prevent anyone from getting into my account on it?
Je crois que j'ai perdu mon téléphone. Existe-t-il un moyen d'empêcher quiconque d'accéder à mon compte ?
Dama yaakaar ni dama ñakk sama telefon. Ndax amna anam bu ñu mëna teree kenn dugg ci sama kont?
country support
Why is verifaction required for my Identity?
Pourquoi une vérification de mon identité est-elle nécessaire ?
Lu tax xoolu sama dàntite war?
why verify identity
What to do if my card is about to expire?
Que faire si ma carte est sur le point d’expirer ?
Lan laa wara def su dee sama kàrt mu ngi waaja jeex?
card about to expire
What do I need to do to request cash back? The ATM actually just gave me the wrong amount. The app I actually chose the right amount.
Que dois-je faire pour demander un remboursement ? En fait, le guichet automatique m'a donné un montant erroné. L'application, j'ai effectivement choisi le bon montant.
Lan laa wara def ngir ñu delloma sama xaalis? Booy seet, gab bi daf ma jox njëg bu jaarul yoon. Ci aplikasioŋ bi, njëg bi ma ci tànn baax na.
wrong amount of cash received
A transaction posted twice to my account.
Une transaction inscrite deux fois sur mon compte.
Yónnee xaalis bu ñu lim ñaari yoon ci sama kont.
transaction charged twice
I want some extra physical cards.
Je veux des cartes physiques supplémentaires.
Dama bëgg yeneen kàrt fizik.
getting spare card
My payment for my card is not working
Mon paiement par carte ne fonctionne pas
Sama feyukaay ci kàrt doxul.
reverted card payment?
What do I do if I forgot my PIN?
Que dois-je faire si j’ai oublié mon code PIN ?
Lan laa wara def sudee dama fàtte sama kodu PIN?
pin blocked
How long is the wait for a money transfer to show up?
Combien de temps dure l’attente d’un transfert d’argent ?
Ñaata waxtu la xaalis buñu yónnee di xaar?
wrong amount of cash received
Google Pay isn't working. What is wrong?
Google Pay ne fonctionne pas. Quel est le problème ?
Google Pay doxatul. Lan mooy jafe-jafe bi
reverted card payment?
I need to set up an account for my daughter, how would I do that?
J’ai besoin de créer un compte pour ma fille, comment ferais-je ?
Dama wara ubbi kont ngir sama doom ju jigéen, naka laa mëna def?
age limit
I got a message that I cannot name X as a beneficiary.
J'ai reçu un message indiquant que je ne peux pas nommer X comme bénéficiaire.
Dama jot mesaas buma wax ni mënu ma wax ni X mooy jafandikoo bi.
transfer into account
What currencies can my account be in?
Dans quelles devises mon compte peut-il être libellé ?
Ci ban xeetu xaalis la sama kont mënee dox ?
fiat currency support
I want to close my account & I will never do business with you again.
Je souhaite fermer mon compte et je ne ferai plus jamais affaire avec vous.
Dama téj sama kont, dootuma amalante dara ak yeen
terminate account
I need to order a new card as my other one was stolen.
Je dois commander une nouvelle carte car l'autre m'a été volée.
Dama war a komànde ab kàrt bu bees ndax dañu sàcc sama bos
lost or stolen card
How much can I top up in a day?
Combien puis-je recharger en une journée ?
Ñaata laa mëna sarsel ci benn bés ?
top up limits
What are the cards and currencies that you support?
Quelles sont les cartes et devises que vous supportez ?
Ban kàrt ak ban xaalis ngeeni yël ?
supported cards and currencies
What are the age limits for your service?
Quelles sont les limites d’âge pour votre service ?
yan ñooy àppu at ngir seen serwiis?
country support
Can I pay for my gas using my Apple watch?
Puis-je payer mon essence avec ma montre Apple ?
Ndax mën naa feye gasoil bi ak sama montar Apple?
apple pay or google pay
When I add money to my international card do you charge a fee to do so?
Lorsque j'ajoute de l'argent sur ma carte internationale, facturez-vous des frais pour le faire ?
Bu ma yokkee xaalis ak sama kàrtu bitim-réew, ndax dangeen may feyloo ay fere ?
top up by card charge
I was charged twice.
J'ai été facturé deux fois.
Dañu ma feyu ñaari yoon.
transaction charged twice
Can I choose when my card is delivered?
Puis-je choisir le moment de la livraison de ma carte ?
Ndax mën naa tànn kañ lañuy indi sama kàrt?
card delivery estimate
I received a "declined" message when doing a transfer
J’ai reçu un message « refusé » lors d’un transfert
Dama jot bataaxalu "demul" ci xaalis buma toxal.
declined transfer
Why was I charged a higher exchange rate when I bought something abroad?
Pourquoi ai-je dû payer un taux de change plus élevé lorsque j'ai acheté quelque chose à l'étranger ?
Lu tax dayo weccoo xaalis bi ñu ma dagg gënoon a yéeg bi may jënd ab afeer bitim-réew ?
card payment wrong exchange rate
Is there any way I can get more physical cards to use with my account?
Y a-t-il un moyen d’obtenir plus de cartes physiques à utiliser avec mon compte ?
Ndax amna anam wuma mëna amee kàrt fizik yu bari yu may jëfandikoo ak sama kontu?
getting spare card
Can I have it by a certain date?
Puis-je l'avoir à une certaine date ?
Ndax mën naa ko am balaa yàgg ?
card delivery estimate
Why has my card been charged an extra pound?
Pourquoi ma carte a-t-elle été débitée d'un euro supplémentaire ?
Lu tax ñu dagg ma lu tollu ci benn CFA ci sama kàrt?
extra charge on statement
How come there is a $1 extra charge on my statement?
Comment se fait-il qu'il y ait des frais supplémentaires de 1 $ sur mon relevé ?
Lu tax ñu yokk 650 CFA ci sama jëflante?
extra charge on statement
Will I get charged for topping up with an international card?
Serai-je facturé pour recharger avec une carte internationale ?
Ndax dina ñu ma feyyeeku ci kàrtu bitim réew?
top up by card charge
How are exchange rates calculated at this bank?
Comment sont calculés les taux de change dans cette banque ?
Naka lañuy xaymaa dayo weccoo xaalis yi ci bànk bii ?
exchange rate
Why didn't my payment process
Pourquoi mon paiement n'a-t-il pas été traité ?
Lu tax ni ñu doxalee sama peyoor bi jaarul yoon ?
pending card payment
How much for an actual card?
Combien coûte une vraie carte ?
Ñaata mooy njëgu kàrt bu baax?
order physical card
Make me understand why I am charged an extra fee when I use the ATM.
Faites-moi comprendre pourquoi des frais supplémentaires me sont facturés lorsque j'utilise le guichet automatique.
Xamal ma lu tax ñu may sàkku yeneen fere sumay jëfandikoo gab.
cash withdrawal charge
I can't seem to be able to use my card
Je n'arrive pas à utiliser ma carte
Mënuma jëfandikoo sama kàrt
card not working
Are there downsides to using a disposable virtual cards?
Y a-t-il des inconvénients à utiliser des cartes virtuelles jetables ?
Ndax am na sabab soy jëfandikoo kàrt wirtuyel yuñ mëna jefandikoo benn yoon kese?
why verify identity
Can you tell me why my top-up failed?
Pouvez-vous me dire pourquoi ma recharge a échoué ?
Ndax mën nga ma wax lu tax sama sarse bañ?
top up failed
I think my transfer failed. What do I do now?
Je pense que mon transfert a échoué. Que dois-je faire maintenant ?
Dama yaakaar ni sama yonnee jàllul, lan laa wara def leegi?
failed transfer
Is the exchange rate the same on weekends as the weekdays?
Le taux de change est-il le même le week-end et en semaine ?
Ndax njëgu weccoo xaalis bi benn la ci njeextalu ayubés bi ak ci ayubés bi?
balance not updated after bank transfer
Is there a fee to make a transfer?
Y a-t-il des frais pour effectuer un transfert ?
Ndax yónnee xaalis am na ay fere ?
top up by bank transfer charge
Why didn't the money I transferred into my account get added to my balance?
Pourquoi l'argent que j'ai transféré sur mon compte n'a-t-il pas été ajouté à mon solde ?
Lu tax xaalis bi ma yónnee ci sama kont boole wuñu ko ci sama tolluwaayu xaalis?
balance not updated after bank transfer
Can I be charged for exchanging foreign currency?
L’échange de devises étrangères peut-il m’être facturé ?
Ndax dañuy feyeeku wecci xaalis bu bawoo feneen?
exchange charge
How do I get a refund for an unauthorized direct debit payment?
Comment puis-je obtenir un remboursement pour un paiement par prélèvement automatique non autorisé ?
Naka laa mën a jotee ci xaalis boo xam ne bi ñu koy jël sama kont yëguma ko ?
direct debit payment not recognised
I need to cancel a payment. Something i purchased a while ago still has not arrived and i'm not going to pay them if they won't send me what I purchased.
Je dois annuler un paiement. Quelque chose que j'ai acheté il y a quelque temps n'est toujours pas arrivé et je ne vais pas les payer s'ils ne m'envoient pas ce que j'ai acheté.
Dama wara fomm ab payoor. Da am jëndoon bu yàgg te ba leegi ñëwul, te duma leen fey sudee yóonee wuñu ma lima jëndoon.
request refund
What value can I get for my currency?
Quelle valeur puis-je obtenir pour ma devise ?
Ban dayo laa mëna am ci sama xaalis?
exchange rate
I checked my statement and am being charged one pound. Where did this charge come from?
J’ai vérifié ma déclaration et on me facture une livre. D’où vient cette accusation ?
Dama xool sama wax, ñu fayeeku ma benn FCFA. Fan la tuuma bii bawoo?
extra charge on statement
I question today's exchange rate for rubles into pounds. I was hoping for a better return.
Je m'interroge sur le taux de change actuel entre les roubles et les livres. J'espérais un meilleur rendement.
Maa ngiy xalaat ci njëgu weccoo xaalis bi am ci diggante Rublë ak Livrë. Maa ngi doon yaakaar ñu gëna mëna ànd.
wrong exchange rate for cash withdrawal
I would like my money back for an item I purchased
Je souhaite être remboursé pour un article que j’ai acheté
Bëgg naa ñu delloo ma ci benn mbir buma jënd.
request refund
why do you verify the top up
pourquoi vérifiez-vous la recharge
Lu tax nga xool sa sarse.
verify top up
I'll send a check to top up my account
J’enverrai un chèque pour recharger mon compte
Dinaa yónnee ab sek ngir sarse sama kont.
top up by cash or cheque
Why are my transfers and purchases keep getting declined?
Pourquoi mes transferts et achats sont-ils constamment refusés ?
Lu tax samay toxal ak jënd ñu faral di ko bañ?
declined transfer
I am still waiting for a money transfer to process.
J'attends toujours qu'un transfert d'argent soit traité.
Maa ngi xaar ba tay ñu jublu ci benn jokkalanteb koppar bu ma defoon.
pending transfer
A while ago i requested a refund from a seller. I keep checking my statement but I have not been refunded yet. I'm confused why i haven't gotten my money back yet but I need your help getting it please.
Il y a quelque temps, j'ai demandé un remboursement à un vendeur. Je consulte régulièrement mon relevé, mais je n'ai toujours pas été remboursé. Je ne comprends pas pourquoi je n'ai pas encore récupéré mon argent, mais j'ai besoin de votre aide pour l'obtenir.
Ay waxtoo a ngii, laaj naa ab jaaykat mu delloo ma sama xaalis. Maa ngi wéy di xool sama karne kont waaye ba tay jotaguma ci xaalis bi. Maa ngi sàkku seen ndimbal
Refund not showing up
What is the top-up limit for my card?
Quelle est la limite de rechargement de ma carte ?
Fan la sama sarsamã kàrt mën a yem ?
top up limits
I want to know your exchange rates.
Je veux connaître vos taux de change.
Dama bëgg a xam seen dayo weccoo xaalis ?
exchange rate
I tried using my card at multiple vendors and now it's not working.
J'ai essayé d'utiliser ma carte chez plusieurs vendeurs et maintenant elle ne fonctionne plus.
Jéem naa jëfandikoo sama kàrt ci jaaykat yu bari te leegi mënatula dox.
compromised card
Everything seems fine with my account, so why did it decline my payment?
Tout semble aller bien avec mon compte, alors pourquoi a-t-il refusé mon paiement ?
Léppa ngi jaar yoon ci sama kont, kon lu tax mu baña nangu sama payoor?
declined card payment
I lost my wallet and I think someone is withdrawing cash with my card. Please help. It is urgent.
J’ai perdu mon portefeuille et je pense que quelqu’un retire de l’argent avec ma carte. Aider, s’il vous plaît. C’est urgent.
Dama ñàkk sama kalpe te jàpp naa ni amna kuy jël xaalis ci sama kàrt. Ndimbal ngir yalla. Mënul xaar.
cash withdrawal not recognised
What are the sources for the funds in my account?
Quelles sont les sources des fonds sur mon compte ?
Fan la xaalis bi ma gis ci sama kont jóge ?
verify source of funds
Why was I charged a fee for withdrawing money off my card?
Pourquoi des frais m’ont-ils été facturés pour un retrait d’argent sur ma carte ?
Lu tax ñu may sàkku xaalis ngir dindi xaalis ci sama kàrt?
country support
I tried to get funds in hard cash but it was rejected!
J'ai essayé d'obtenir des fonds en espèces mais cela a été rejeté !
Jéem naa am xaalis bu teew waaye dañu ko bañ?
declined transfer
Am I able to get a refund for something I bought?
Puis-je obtenir un remboursement pour quelque chose que j’ai acheté ?
Ndax mën nañu ma dello xaalis bi ci lenn luma jëndoon?
request refund
How do I locate my PIN now that I have my card?
Comment puis-je localiser mon code PIN maintenant que j'ai ma carte ?
Naka la mëna wuute sama kod-PIN leegi? am naa sama kàrt?
get physical card
I wanted to know why a top-up I made has been reverted.
Je voulais savoir pourquoi une recharge que j’avais faite a été annulée.
Bëggoon naa xam lu tax benn sarse bu ma defoon ñu fomm ko.
top up reverted
I'm not sure where my phone is. Can someone else use the app?
Je ne sais pas où se trouve mon téléphone. Quelqu'un d'autre peut-il utiliser l'application ?
Xamuma fan laa sànni sama telefon. Ndax am na keneen ku mën a jëfandikoo aplikaasiyoŋ bi ?
lost or stolen phone
Why is my card not working anymore?
Pourquoi ma carte ne fonctionne plus ?
Lu tax sama kàrt doxatul?
card not working
I topped up my account but the app failed to process it.
J’ai rechargé mon compte, mais l’application n’a pas réussi à le traiter.
Dama sarse sama kont, waaye aplikaasioŋ bi mënu ko def.
top up failed
I need Australian dollars instead of UK currency.
J'ai besoin de dollars australiens au lieu de la monnaie britannique.
Xaalis Australie laa gën a yittewoo ne xaalisu Angleterre.
exchange via app
What are some of the restrictions that the disposable cards have?
Quelles sont certaines des restrictions imposées aux cartes jetables ?
Yan ñooy yenn wàññi yuñu digal kàrt yuñuy jëfandiko benn yoon kese?
disposable card limits
I would like to use one of my cards for a family member. Is that allowed?
Je souhaiterais utiliser une de mes cartes pour un membre de ma famille. Est-ce autorisé ?
Bëgg naa jëfandikoo benn ci samay kart ngir sama waa kër. Ndax loolu nangu nañu ko ?
getting spare card